Commentaire de ousmane (13/01/2008 18:15) :
man la ousmane talibe baye gueye kou téde ki té bakh lol cherif est mon
diewrine .guiss yalla lou woor la .baye bi mo gnou ray si mawoul kheybi
mawoul khayabe mawoul kawsara dekil gnou si lailahailaalahou ma ngi cédé né
kou doundou ba dé guissoul yalla sou déwé sou gnou borom bi douma ko mangi
bégé goor yalla yép di lén magal .baye gueye dognou rée dougne la rér
mbégoum diam yép yawa .cherif magal na la bou wér
http://ouz-ibou@live.fr fass cité sika v 66 |