Commentaire de ZOROASTRE (13/03/2009 23:12) :
dieureuféééé NIAMEE DAAROU diarawlak CHEIKH MOUSSA TOURE....sante naniou
bou wééra wéér, yéne miniou yéé,yarate niou si tééy, si kham, si khamé, si
respect, si niak diarigno... amou gnou sagn sagn wéédi ndakh yéknaniou
guiss naniou...amougnou sééne faay... ziaar wa MASLAKOUL HOUDA ak béép
anrif...........
''il n'y a de DIEU que DIEU car tout est
DIEU!!!!!''
|